Librairie XITMA

Librairie  XITMA

Partager

28/09/2024

̀_tous

25/09/2024

Xibaar yu taay yi:
🇸🇳👇🏽
Birame Souleye Diop xamle na ne ay fan a ngi nii, ñu doon liggéey ci yan yoon lees war a jaar ngir wàññi kuraa bi ak njafaan (carburant). Ginnaaw bu ñu jébbalee li ñu jot a tënk kilifa yi ba noppi nag, ci fan yii di ñëw, manees naa séntu ag wàññiku bu baax ci njëgu kuraa bi ak njafaan (carburant) yooyu.

Ba tay moom Biram Suley xamle na ne, Senegaal dina jëfandikoo petrol bi ak gaas bi, ngir fexe ba kuraa bi yegg fépp fu ab saa-senegaal nekk ci réew mi.

Vous voulez que votre entreprise soit Magasin la plus cotée à Touba ?
Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.

Téléphone

Site Web

Adresse


TOUBA
Touba
222

Heures d'ouverture

Lundi 09:00 - 19:30
Mardi 09:00 - 19:30
Mercredi 09:00 - 19:30
Jeudi 09:00 - 19:30
Vendredi 08:00 - 17:45
Samedi 09:00 - 19:30